Translate

Type: text
Description
:sl1:
If you do anything other than a purely default installation, there is a real chance that some dialogs will be displayed in English instead.
SourceTranslationState
159
To select a different language you will need to abort this installation and reboot the installer.
Ngir tann waneen lakk, faw nga bayyi istalaasioŋ bii, daldi tambulewaat prograamu istalaasioŋ bi.
160
Continue the installation in the selected language?
Ndax nu eggale istalaasioŋ bi ci lakk winga tann?
161
The translation of the installer is incomplete for the selected language.
Tekki (traduction) bu prograamu istalaasioŋ bi ci lakk winga tann eggagul.
162
The translation of the installer is not fully complete for the selected language.
Tekki (traduction) bu prograamu istalaasioŋ bi ci lakk winga tann defeesagul leppu.
163
This means that there is a significant chance that some dialogs will be displayed in English instead.
Loolu liñu ciy déggé moodi, amaana yenn ci wax yiñu lay bindal fii doon ci Aŋgale.
164
If you do anything other than a purely default installation, there is a real chance that some dialogs will be displayed in English instead.
Boo tannul istalaasioŋ bu defóo bi, kon amaana yenn ci wax yiñulay bindal fii doon ci Aŋgale
165
If you continue the installation in the selected language, most dialogs should be displayed correctly but - especially if you use the more advanced options of the installer - some may be displayed in English instead.
Boo eggqlee istalaasioŋ bi ci lakk wi nga tann, li ëppu ci wax yiñu lay bindal fii ci lakk wi nga tann lay wara doon, waaye nak su fekkee dangaa tann yenn istalaasioŋ yu xóot yi, amaana yenn ci yiñu lay bindal doon ci Aŋgale.
166
If you continue the installation in the selected language, dialogs should normally be displayed correctly but - especially if you use the more advanced options of the installer - there is a slight chance some may be displayed in English instead.
Boo eggqlee istalaasioŋ bi ci lakk wi nga tann, li ëppu ci wax yiñu lay bindal fii ci lakk wi nga tann lay wara doon, waaye nak su fekkee dangaa tann yenn istalaasioŋ yu xóot yi, amaana, doonte fooguñu ko lool sax, yenn ci yiñu lay bindal doon ci Aŋgale.
167
The chance that you will actually encounter a dialog that is not translated into the selected language is extremely small, but it cannot be ruled out completely.
Fooguñu nga gis fii ñu bindal la fi loo xam ne tekkeeguñuko ci lakk wi nga tann, waaye nak teewul loolu mana am.
168
Unless you have a good understanding of the alternative language, it is recommended to either select a different language or abort the installation.
Su fekkee xamóo bu baax waneen lakk wi ñu lay bindal, kon linga wara def mooy, benn nga tann waneen lakk, walla nga bayyi istalaasioŋ bi.
169
If you choose not to continue, you will be given the option of selecting a different language, or you can abort the installation.
Su fekkee dangaa tanna baña eggale istalaasioŋ bi, kon deesna la laaj nga tann waneen lakk, wa nga bayyi istalaasioŋ bi.

Loading…

Loading…

Things to check

Glossary

Source Translation
No related strings found in the glossary.

Source information

Source string location
../localechooser.templates-in:16001
Comments
Type: text Description :sl1:
Source string age
a year ago
Translation file
packages/po/sublevel1/wo.po, string 164
String priority
Medium
Failing checks